www.secuser.com

lundi 20 mai 2024

Soxna Asta Walo MBACKE

Sokna Aissata MBACKE  , ganessi wone na Adunya

293 att si werri wolof si atti 1945 wi, sa Haffe Djoloff, wadiour Am

Wou Goor di Serigne Ahmadou Bousso MBACKE,

Donte mbengo wone na mom si Djant Leer

Saw  Mame Mahrame MBACKE,Sosso saw soufi3

Daaray Al Kuran, Djan terre wi, Bolem

Top kam kam, Alima et Tawjid

Djan te Djanale

Si ay aw domama ya Djigen, Bolessi Soxna Diarra BOUSSO

Mim wathie teerre, ba top ak Mbinde, Sa ak Tawjid

Aissatou Bint doni Soxna si Serigne Mouhamadou BOUSSO,

Soxna Asta Walo deuki Saloum

Dalal fa si Djam Ya Allahou ak douninou Toll

Si barkeb Serine BOUSSOBE, ki di Fara Guedel MBODJ.

SeYDA AISSATOU et Serigne BOUSSOBE,

Si Niek ak taar ; Doni itam Yaye Daara Sa

Naawel; dounde nam 108 si ay att si Daara,

Ami Tcioup dane Soll Kaftan, teddi

Djang gouddi soune Al Kuran tey ami Nafilas


Mouhamadou Falilou MBENGU

Aucun commentaire:

Enregistrer un commentaire