lundi 17 janvier 2022

Puberté Déclinant

Obliques envies tirées de désirs mais enfin 

Si Sélébé yone yé, beug am yi Soxé Wanté 

Tout , dirigeant vers les sexes opposés, le mâle lui feint

Lepp Diaré si ay Goor Aki Djiguène, Gorgui méel né né

Images et appels divers de demoiselles et rêve 

Guissa Toul gaarab si ay woté ki Djoundjoum Signares , téey sopp 

Intangiblement de dames. De sensualité brève 

Tiggi, Niaguamaré,Fem si ap béep settlou, mou topp 

Parmi ses pairs garçons A l'âge de se marier; 

Si birri moromi Goor am Siiy att am, Waxtou Soxna 

A souvent ces excroissances sous-cutanées. 

Dina faral Di Ammi mandarga si kanam 

Xylophones vibrant decriraient parfaitement les sons dedans ces oreilles 

 yi Di riir , si biir, né temèeri xalam. 



 Mouhamadou Falilou MBENGUE

Aucun commentaire:

Enregistrer un commentaire